Saltar navegación.
Inicio

L1_Wolof

Njang mu njëkk - Dalal jamm ci Wolof
Salaamaalikum, suma xarit. Na nga def? Mangi fi rek, jërëjëf.
Naka nga tudd? Maa ngi tudd Tóor-tóor. Tur wu rafet.
Baalma, fan moo am bërëb bu rafet? Demal ci ndox mi. Ba beneen yoon.
Ndox maangi fii? Waaw, ndox maangi fii. Agsil.

L1_Wolof in PDF: clic

L1_Wolof in TIF: clic

Vocab L1_Wolof

 

On-line Parts:   0           4