Saltar navegación.
Inicio
Instituto de educación secundaria

L2_Wolof

Ñaareelu njang. Jënd ak jaay.

¿Lan nga beg? Dama bëgg tuuti mburu. Amewumako. Mingi nii.
¿Ñaatala? Jox ma ñetti dërëm.
Bëgguma bii xalima. ¿Ndax am nga xalima bu baxa?
Dafa bari. Dama koo jox ñaari derëm. Dafa yomb.

L2_Wolof in PDF: clic